Top Songs By Aba Diop & the Yermande Family
Credits
COMPOSITION & LYRICS
Babacar Diop
Songwriter
Lyrics
Ma khôl Mbaye Bamou Nekhma ma def ko kharite
Fek ko colobanne mou yatal ma sabar
Ma dieul car rapide fay ko 200
Mou wathier ma Guediawaye
Marché bou bësse
Ma dame cogne
Fek fa Mame Gore mouy décoré sabar
Yat pek
Tek ci diourome niari trou
Kou bagne laobé boula seugeum lal
Boula seugeum lalé boo ba yakoungua
Khadime teugeul
Written by: Babacar Diop