Top Songs By Aba Diop & the Yermande Family
Credits
COMPOSITION & LYRICS
Babacar Diop
Songwriter
Lyrics
Ndiadiane djiné
Djiné xam sa keur teh xamul keureum
Ndiadiane djiné djiné yi
Codou Fall Mboup
Ndiadiane djiné
djiné xam sa keur teh xamul keureum
Ndiadiane djiné Mbouba dialli
Bellio mo di bellio mbaye
Bellio mbaye ngan gui toy na nekh na ya meun ngan
Sa ngan dou xarani mame
Ay way bellio mo di bellio mbaye
Bellio mbaye ngan gui toy na nekh na ya meun ngan
Sa ngan dou xarani
Ay way ni bellio mo di bellio mbaye
Mo di bellio mbaye
Bellio mbaye ngan gui toy na nekh na ya meun ngan
sa ngan dou xarani mame
Ay way bellio mo di bellio mbaye
Bellio mbaye ngan gui toy na nekh na ya meun ngan
sa ngan dou xarani

Kon yayou Birima Ndiaye bilay ya meun ngan
Sa ngan dou xarani mame
Ay way bellio mo di bellio mbaye
Mo di bellio mbaye
Bellio mbaye ngan gui toy na nekh na ya meun ngan
Sa ngan dou xarani mame
Ndeungeul Sidi Dior Ngoné
Mo di Codou Fall Mboup
Ndeungeul Sidi Dior
Mo di Codou Fall Mboup
Sa ngan gui toy na nekh na bilay ya meun ngan
Sa ngan dou xarani mame
Ay way bellio mo di bellio mbaye
Mo di bellio mbaye
Bellio mbaye ngan gui toy na nekh na ya meun ngan
Sa ngan dou xarani mame
Ay way bellio mo di bellio mbaye
Mo di bellio mbaye
Yayou Abdou Lahat Ndiaye bilay ya meun ngan
Sa ngan dou xarani mame
Ay way ni bellio mo di bellio mbaye
Mo di bellio mbaye
Bellio mbaye ngan gui toy na nekh na ya meun ngan
Sa ngan dou xarani
Ay way ni Bellio mo di bellio mbaye
Mo di bellio mbaye
Codou yayou Sagar Ndiaye ya meun ngan
Sa ngan dou xarani mame
Ay way ni bellio mo di bellio mbaye
Mo di bellio mbaye
Bellio mbaye ngan gui toy na nekh na ya meun ngan
Sa ngan dou xarani
Thiey!
Neungeul Sidi Dior Ngoné
Codou Fall Mboup
Laobé Xewer Ndiaye Ndiogou nioy mame ya
Sama mame
Codou Fall Mboup
Diebie Ma
Anta Samb
Moy Baye ba
Ndeye Makhouradia Sène moy yaye dia
Magou Diakhou Mboup, Codou
Magou Diabel Mboup, Codou
Fall Mboup
Magou Ndeye Mboup, Codou
Boul door boul door
Dafa andak ndayam
Boul door way
Signel desouko reuk
Boko reuké deuk diam la
Signel desouko reuk mame
Na bari na bari na bari
Waw waw
Thiey thiey thiey
Na bari na bari na bari
Yayou Birima Ndiaye la
Yayou Abdou Lahat Ndiaye sama nidiaye
Yayou Sagar Ndiaye la
Mamou Pape Modou
Mamou Niane mou Thiorro Mboup
Mamou Ndeye Fatou Tall
Mamou Karime Ndiaye la
Mamou Raye Ndiaye la
Mamou Khadim Mbaye la
Mamou Mame Diarra
Mamou Bouba Ndiaye la
Mamou Souzane ak Birima
Mamou Youssou ak Modou
Mamou Djibi Faye Guana
Mamou Doudou Falla
Mamou Médoune Matar
Mamou Sountou ak Ada
Mamou Bigué Mbaye , moy taw thi Souzane
Written by: Babacar Diop