Top Songs By Aba Diop & the Yermande Family
Credits
COMPOSITION & LYRICS
Babacar Diop
Songwriter
Lyrics
Cheikh Ndiguel Fall
Yay beuline coumbay beuline
Deuk bo dem wané fa louni nañe
Beuline coumbay beuline
Ay Ndiguel Fall
Serigne Cheikh Ndiguel Fall Gaïndé khelcom
Nioun yaw rek laniou beug papa
Nioun yaw rek laniouy bégué
Yaram nga Fall
Sa younou yewo yaw rek laniouy guiss
Sounou khol yi yako feiss
Waat na ni yaw yay Baye Fall bi Gaïndé khelcom nga Baye Ndiguel
Seute day ndourou mamame
Seute day ndourou mame ya dondou Serigne Cheikh Fall Baye Gore rakou Serigne Modou Moustafa
Kokou mame la
Cheikh Ndiguel Baye Gore meun thi mag ñi meun thi ndaw ñi
Cheikh Ndiguel Baye Gore meun thi mag ñi meun thi ndaw ñi
Yanou def ni Baye Falls
Deug deug deug Baye Falls
Yanou def ni Baye Falls
Deug deug deug Baye Falls
Baye Ndiguel Fall
Yiw na sel na tabé na manou na goré na
Baye Ndiguel Fall
Yiw na sel na tabé na manou na goré na
Baye Ndiguel Fall
Ndiguel
Baye
Ndiguel
Moy Serigne bi geun
Tarou yiw tabé
Moy Serigne bi geun
Thi nioune
Thi nioune
Moy Serigne bi geun
Baye Ndiguel mou Serigne cheikh fall baye gore kat moy serigne bi geun
Thi nioune
Baye Ndiguel
Baye Falls yangi ni
Fall
Baye Falls yangi ni
Serignou Aliou Mbaye
Borom Mbacké bawol Fall
Kou mel ni Mbaye
Baye Falls yangi ni
Cheikh Ndiguel Baye Gore
Baye Fall nga Baye Fall nga
Cheikh Ndiguel Baye Gore
Baye Fall la
Cheikh ngani
Cheikh Ndiguel ya dondou Serigne Modou Moustafa Fall Baye Fall
Loulou deug la
Diébalou rek
Diébalou
Diéalou rek
Diébalou rek
Diébalou
Diébalou rek
Diébalou rek
Kouko defoul perte nga
Man deh diébalou na
No faté Baye Fall
Lan?
Ak lan?
Ndiguel
Cheikh Ndiguel
Cheikh Ndiguel Baye Gore
Ndiguel
Cheikh Ndiguel
Cheikh Ndiguel Baye Gore la
Ndiguel
Cheikh Ndiguel
Cheikh Ndiguel Baye Gore la
Ndiguel
Cheikh Ndiguel
Sa mame mo khalone yon bi niou fek ko fa
Kou nek di souk di ram di diébalou
Gniir beugeu done Baye
Fall
Baye
Mounane Fall
Baye Falls yangi ni
Fall
Baye Falls yangi ni Fall
Fall
Baye Falls yangi ni Fall
Fall
Baye fall yangi ni fall fall fall fall fall
Written by: Babacar Diop