Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Wally B. Seck
Wally B. Seck
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Wally B. Seck
Wally B. Seck
Songwriter
Akatche Bennette Seraphin Koffi
Akatche Bennette Seraphin Koffi
Composer
Bakhao Dioum
Bakhao Dioum
Songwriter

Lyrics

Sonou naa
Maala togne, balma
Woh woh woh
Sonou naa
Mane maala togne, balma
You feel mane dé wéét naa
You're still, you're still my boo
Everyday meu niaak fayda go back
Nieuw soukou diégalou ci seu kanam baalou akk
Baalou naala nguir yalla balma
Dafma méré xam naani ma togne
Everyday meu niaak fayda go back
Nieuw soukou diégalou ci seu kanam baalou akk
Nangou sama défaite, téy ya am ndam (am ndam)
Loma méré méré kham nga maa xam
Sama babygirl kaay diégalou na
Sama babygirl baayil mér wouyouma
Nangou sama défaite, téy ya am ndam (am ndam)
Loma méré méré kham nga maa xam
Sama babygirl kaay diégalou na
Déloussil ma baby oh-ouh-ah yeah
Sonou naa
Maala togne, balma
Woh woh woh
Sonou naa
Mane maala togne, balma
Chérie coco me I love you dou débat
Tu sais pour toi je ferai le premier pas
Des jeux de rein à la Wally - Ipupa
Néxaalat keur gui on fera n'importe quoi
Yow tamit, baayil seu mér-bi té nga ré comme Khaby
Lam lamé déy sonal seu xél, nangou naa ni
Maako déf, maala togne
Bouniou mél ni Tom & Jerry
Lak lak like fire
Woh woh woh woh woh woh
Sexy lady
Dama wééré tay, diégalou naa
Sama babygirl bayil mér, wouyouma
Nangou sama défaite, téy ya am ndam (am ndam)
Loma méré méré kham nga maa xam
Sama babygirl kaay diégalou na
Déloussil ma baby oh-ouh-ah yeah
Sonou naa
Maala togne balma
Woh woh woh ..
Sonou naa
Mane maala togne balma
"Hymne Faramareen"
Warna niou woné mbolo
Warna niou woné freedom
Kou done laathie faramareen, faramareen
Faramareen nieuw na
Yéna ngui dég louné, wéraneté, xééx, xoulo nguir man
Souma sanione kéne kounék setsila niou naan ataaya
Beug yalla ko deff thi diaamam
Beug ngama, beug naala (ooh yeah)
Yéne gni beug faramareen teudeul nélaw yalla baaxna
Kone sopé sopé kaay, yaw kaay
Di lén wayal mbékté leu bou reuy thi man
Ma sopé sopé lover don’t cry
Di lén wayal mbékté leu bou reuy thi man
Warna niou woné mbolo
Warna niou woné freedom
Kou done laathie faramareen, faramareen
Faramareen nieuw na
Warna niou woné mbolo
Warna niou woné freedom
Kou done laathie faramareen, faramareen
Faramareen nieuw na
(Hey yow sama sopé
Boul di xoulo, boul di xééx, Yalla nopina
Yalla yaa na, Yalla baaxna
Maa léén gueuna love
Maa léén gueuna yeuk
Maa léén gueuna gueum
Maay ki leu xam
Maay ki leu beug
Ouh !
Force à toi sopé
Force à toi sopé)
Written by: Akatche Bennette Seraphin Koffi, Bakhao Dioum, Wally B. Seck
instagramSharePathic_arrow_out