Lyrics
Eh lamu saf, kenn du la ko wax ndax kooku macci koo xam
Ni naan, kii daalay gollo, naando dara
Ma doggu ci biir ba lépp leer ma najj jar nga ko
Ku la xam-ul mooy diir tey yaw mbaag cherie coco
Bu doonoon musisian maana la du dégamer
Def nga ma sa xalé do joo ak man, jeu de gamin
Dëkk dimaa jaam, dimaa jaam yoro marimba du Benjamin
Bo def-ul ndank, na més a te sa loxo, on sait jamais
Mom xalé la, te bari na doole
Mo raw alkati dafay dooré
Dina la toppato ba laj la, laj la, laj la
Bébé loy réeré
Te bu ko laje munee la bae, yaaw mi lay rééré
Faajar tel ni la ma yéewe
Dimaa xool ci biir bët naan ma, qu'est-ce que ça fait?
Yaw yaa raw athlète bu droguee
Ku la topp ba ci biir, day mujjee eclater
Faajar tel ni la ma yéewe
Dimaa xool ci biir bët naan ma, qu'est-ce que ça fait?
Yaw yaa raw athlète bu droguee
Ku la topp ba ci biir, day mujjee eclater
Eh dafa neex lool nga am ku xam lii jam sa ditax
Soxlawul sax ngay wax di executee, new-ul ku rambaax
Tey na xame ne fuñuy feccee yela ak ndaw rabine
Colle njàp mél ni Doktor Raoult ak colochrine
Armée wu kaw ak suuf mél ni kuy dem guerre
Tasaare arsenal yi, bu la dal nga ter
Dila woo ci bëre, te leer na, leer na, moola, moola mën dila nogatu
Tase sa ngem, mbër ma daanu na, oh secours
Mom xalé la, te bari na doole
Mo raw alkati dafay dooré
Dina la toppato ba laj la, laj la, laj la
Bébé loy réeré
Te bu ko laje munee la bae, yaaw mi lay rééré
Faajar tel ni la ma yéewe
Dimaa xool ci biir bët naan ma, qu'est-ce que ça fait?
Yaw yaa raw athlète bu droguee
Ku la topp ba ci biir, day mujjee eclater
Faajar tel ni la ma yéewe
Dimaa xool ci biir bët naan ma, qu'est-ce que ça fait?
Yaw yaa raw athlète bu droguee
Ku la topp ba ci biir, day mujjee eclater
Faajar tel ni la ma yéewe
Dimaa xool ci biir bët naan ma, qu'est-ce que ça fait?
Yaw yaa raw athlète bu droguee
Ku la topp ba ci biir, day mujjee eclater
Faajar tel ni la ma yéewe
Dimaa xool ci biir bët naan ma, qu'est-ce que ça fait?
Yaw yaa raw athlète bu droguee
Ku la topp ba ci biir, day mujjee eclater
Written by: Bril, Jeeba