Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Mia Guisse
Mia Guisse
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Benette Séraphin Koffi
Benette Séraphin Koffi
Composer
Bakhaw Dioum
Bakhaw Dioum
Songwriter

Lyrics

Mane dame confuseone yow midnight
Tokk ci digg lal bi mane ak wétay
Xol bi défna choix ci Khalilou Laye
Kay ngua ladjal mako djourom yi way
Est-ce que amna courage?
Deugueul loumouy wakh
Mom ndakh nieména
Oh samay thiay-thiay
Mba nga dieunde glace
Délo avance
Sa température montée na
Un instant
Hello baby (comment va?)
Antan nguama (fi lou fi diis)
Mes caprices (diaroul xarr)
Xalébi ñiémé ngama (bé waxma yaye mbagne)
Hello baby (comment va?)
Antan nguama (fi lou fi diis)
Mes caprices (diaroul xarr)
Xalébi ñiémé ngama (bé waxma yaye mbagne)
Yague dég dali (deffeu nekh)
To diari ndari (si deffeu nekh)
Ya dég dali (deffeu nekh)
Do diari ndari (bilay deffeu nekh)
Yako dég dali (deffeu nekh)
Do diari ndari (deffeu nekh)
Ya dég dali (deffeu nekh)
Oh amore mio (deffeu nekh)
Ligua momeu gui (bilay deffeu nekh)
Ya deff seu choix dieuli Wally, you and balli
Souniou bañé way nañu bayi té romb, faramareen ba ngui
Lady lady
Kay ma wakh la
Tane nga ki guene ci yaw for life
Lady lady
Maye sa Seytané
Lingu fi wakh yeup dég nala
Ndakh nourou nala kouy dieundeu glace?
Bandit bou diantal non non dou sage
Bébé goudi mba do jégui rail
Sa température montée na
Un instant
Allô baby (comment va?)
Dég ngama (dég nala)
Mba nobb ngama (yow reck)
Xalébi dépassé ma (wakho'k ragal)
Allô baby (comment va?)
Dég ngama (dég nala)
Mba nobb ngama (ha ha!)
Xalébi dépassé ma (wakho'k ragal)
Yague dég dali (deffeu nekh)
To diari ndari (si deffeu nekh)
Ya dég dali (deffeu nekh)
Do diari ndari (bilay deffeu nekh)
Yako dég dali (deffeu nekh)
Do diari ndari (deffeu nekh)
Ya dég dali (deffeu nekh)
Oh amore mio (deffeu nekh)
Ligua momeu gui (bilay deffeu nekh)
Jeul na lima mom
Jeul na lima mom
Jeul na lima mom
Wiri wiri jari ndari
Jeul nga lima momé
Jeul nga lima momé
Wally lingua momé
Wiri wiri ya tog ci ndali
Dég ngama (dég nala)
Mba nobb ngama (yow reck)
Xalébi dépassé ma (wakho'k ragal)
Allô baby (comment va?)
Dég ngama (dég nala)
Mba nobb ngama (ha ha!)
Xalébi dépassé ma (wakho'k ragal)
Yague dég dali (deffeu nekh)
To diari ndari (si deffeu nekh)
Ya dég dali (deffeu nekh)
To diari ndari (bilay deffeu nekh)
Yako dég dali (deffeu nekh)
To diari ndari (deffeu nekh)
Ya dég dali (deffeu nekh)
Oh amore mio (deffeu nekh)
Ligua momeu gui (bilay deffeu nekh)
Ya deff seu choix dieuli Wally
Souniou bañé wa way nañou romb
Faramareen ba ngui
Written by: Bakhaw Dioum, Benette Séraphin Koffi
instagramSharePathic_arrow_out