Music Video

Massamba Amadeus - Amadeus - Boulma Sagané (Vidéo Cover Officielle)
Watch Massamba Amadeus - Amadeus - Boulma Sagané (Vidéo Cover Officielle) on YouTube

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
AMADEUS
AMADEUS
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Oumar Niang
Oumar Niang
Composer
Saliou Massamba Samb
Saliou Massamba Samb
Songwriter

Lyrics

Guiss na leu ngay ndiap yeah
Deff ci foula gou meut seuk
Man dall limaye nyan amine wai
Mou dieugué done sama weurseuk
Dey nex ci sama xol
Biss bi ngamay ndieuk khol
Néma berg na la donté benn yon
Leuy meusseu done ci sama doundeu
Yallay boor lou ko nekh dogeul
Yallay deff lou ko nakh ci diam
Té yallah deff mann ma tamoula
Natoula am ndogal, dieuleul
Yallay boor lou ko nekh dogeul
Yallay deff lou ko nakh ci diam
Té yallah deff mann ma firéla
Natoula am ndogal, dieuleul
Hé Boulma sagané wai
Boul meusseu faté né wai
Pithieu xol ma ya fa né wai
Kon boulma sagané wai dieuleul
Way wi, fent na ko ndakhté
Yow kenn nga ndo nyaar
Weurseukou yallah nga ehh wai
Dey nex ci sama xol
Biss bi ngamay ndieuk khol
Néma berg na la donté benn yon
Leuy meusseu done ci sama doundeu
Yallay boor lou ko nekh dogeul
Yallay deff lou ko nakh ci diam
Té yallah deff mann ma tamoula
Natoula am ndogal, dieuleul
Yallay boor lou ko nekh dogeul
Yallay deff lou ko nekh ci diam
Té yallah deff mann ma firéla
Natoula am ndogal, dieuleul
Hé Boulma sagané wai
Boul meusseu faté né wai
Pithieu xol ma ya fa né wai
Kon boulma sagané wai dieuleul
Written by: Oumar Niang, Saliou Massamba Samb
instagramSharePathic_arrow_out