Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
AMADEUS
AMADEUS
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Abdoulaye Diop
Abdoulaye Diop
Composer
Saliou Samb
Saliou Samb
Songwriter

Lyrics

Daagul, jaayul ndàama
Xam nga ni dal ya mën ndaw ñee
Daagul, jaayul ndàama
Xam nga ni dal ya mën ndaw ñee
Moom dal li mu bëgg
Amaanaa du lu bari
Kuu xam li mu wara def, te di koo def nu mi waare
Jàppul seeni télé, zappé séen chaine sax
Waat naani su may cote du ma ko mës a ndëndale ndax
(Amul) ku dul man
(Xamul) kul dul man
(Gëmul) su ma gooreel du ma ko naxee mbaay
(Amul) ku dul man
(Xamul) kul dul man
(Gëmul) jëmmaan ji mooy sama njegenaay
(Amul) ku dul man
(Xamul) ey kul dul man
(Gëmul) su ma góoreel du ma ko naxee mbaay
(Amul) ku dul man
(Xamul) kul dul man
(Gëmul) jëmmaan ji mooy sama njegenaay
Yaw la mujjee déggoo ba ma nelaw
Yaw la njëkk a janook ba ma yéewoo
Daru dunya sa su nel selew
Sa jëmm jee doon sama njegenaay
Kaay jugal jaayu nak
Jugal yëngal àdduna
Taaru nga, taayu nga
Sama jigéen kay digal
Kaay digal jaayu nak
Jugal yëngal àdduna
Kaay du ma saasuman
Dinala wayal sa su ne
Ci sama xol yaay ki fa njëkk a toog
Xas nafa féete ag yaw sunu yabbo ngóorgóolu
Ci sama xol yaay ki fa njëkk a toog
Xas nafa féete ag yaw sunu yabbo ngóorgóolu
(Amul) ku dul man
(Xamul) kul dul man
(Gëmul) su ma gooreel du ma ko naxee mbaay
(Amul) ku dul man
(Xamul) kul dul man
(Gëmul) jëmmaan ji mooy sama njegenaay
(Amul) ku dul man
(Xamul) ey kul dul man
(Gëmul) su ma gooreel du ma ko naxee mbaay
(Amul) ku dul man
(Xamul) kul dul man
(Gëmul) jëmmaan ji mooy sama njegenaay
Daagul, jaayul ndàama
Xam nga ni dal ya mën ndaw ñee
Daagul, jaayul ndàama
Xam nga ni dal ya mën ndaw ñee
Written by: Abdoulaye Diop, Saliou Samb
instagramSharePathic_arrow_out