Music Video

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Birahim
Birahim
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Birahim
Birahim
Songwriter

Lyrics

Lepp louma am ak koumou done
Cheri booy yama ko gueuneul
Limaye liggey beuss bounek di ci sone
Ci lou bakh lepp yay borome
Ya takh ma xam kima done, diox ma fit
Ba takh na do tou ma tiit
Limaye liggey beuss bounei di ci sone
Ci lou bakh lepp yay borom
Ya takh ma xam kima done, diox ma fit
Retanal dotouma tit
Xolma ci beut my baby boul kheff
Teh boul ragal diam rek ngey am
Lima beug rek moy kou bakh
So Ki gueun borom xol bou nice
Kouma doul nakh dima begueul
Souma diaxlei sakhma deufeul
Kima done sett yow leu malay heee
So mbektane
Tey meu tak leu
Ndakh danga beuri ndiom
Togual khar bama tak leu reeek teral leu
Douma la meussa fowe ba nopi bala fi
Gorr niou bakh gni rombe la
Yaw ngaye muisere
Laaaaa
Lalalalalala
Lalalalalala
Laaaaa
La la la laaa
Xamna beug ngama
Yawit xamnga beug nalaaa
Cherie bikk sakh beug nala
Ci ay nelaw ngani feug ngama
Xamna beug ngama
Yawit xamnga beug nalaaa
Cherie bikk sakh feug nala
Ci ay nelaw ngani beug ngama
Ha haaaaaa
Fi la fiii laaaa
Bou doul fii dou done fenen
Ki la kiii laaaaa
Kiiiii laaaaa
Bou doul kiii dou done kenen
Yow xamnga sa bop
Xam linga done
Lahi yawla law
Ndakh djiguene dey xam bopam
Sam nga sa bop yangui xol euleuk
Yaw dangaye ammm niaboot
Takk nga sa seur
Moytou nga gagnii
Ndakh bougne la xamei dem bayila
Wakh dji loumou nekh
Kha nekh kha nekh
Yaw boum la takh ba kham sa bop
Ndakh djiguene amoul loudoul bopam
Ah Wallay djiguene amoul loudoul sagome
Mbeguel mo nekh ci bougn la beugué
Mbeguel mo nekh ci bougn la nobé
Mbeguel mo nekh ci bougn la wolo
Mbeguel mo nekh ci bougn la safo
Mbeuguel mo nekh
Barra cheri soda la
Mbeuguel mo nekh
Baye Diop cheri Amina
Mbeuguel mo nekh
Djily Nyass cheri Sophina
Mbeuguel mo nekh
Henry cheri Amina
Written by: Birahim
instagramSharePathic_arrow_out