Top Songs By Youssou N'Dour
Credits
PERFORMING ARTISTS
Youssou N'Dour
Performer
The Super Etoile
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Youssou N'Dour
Composer
Lyrics
Ibu Njaay Fama
Ibu Njaay Fama
Waw bitim reew ña fa nekk dëkk ñu faa
Mujj u mujj yay dañuy delu ci waw Sénégal
Ibu Njaay Fama
Ibu Njaay Fama
Buul seen bittim réew ña fa nekk dëkk ñu fa
Mujj u mujj yay dañuy delu ci waw Sénégal
Hoolé
Bitim reew ligey la lajj
Immigré mom ligey la lajj
Immigré
Ibu Njaay Fama
Ibu Njaay Fama
Ñu nee bitim reew ñu fa nekk dëkk ñu fa
Mujju mujj yaay da ñi délu ce ndaxte ñoo ñu xamu ñu leen noono
Fi la ñu saaso
Ñu nee jòom mooy tukki yaay
Waye fulla mooy ñibi cee
Noo mën a mel
Noo mën a am ndeysan ñibi ce la war
Youssoo sabali nga,sabali nga
Deedet samali ngondeh
Moytul lu la defar,li la nex waxal
Ndax bañuloo te mbëgga nga ñepp a am
Codu faal Gaydella,Gaydella
Writer(s): Youssou N Dour
Lyrics powered by www.musixmatch.com