Similar Songs
Credits
PERFORMING ARTISTS
N'dongo Lo
Performer
COMPOSITION & LYRICS
N'dongo Lo
Songwriter
Lyrics
Samay xarit gniouma doudondoll la beugueu weuyeull
Adouna meunou ma yeubou bama fatéléne ba maléne di guinawal xarit
Meunou ma diayy bama hébeléne yéne la dioudondollohhh
Dane andeu andeu bou raféte gui teii
Yalleu tahh bobou andeu dou diehh ohh Alioune Lam
Naguéne diapp Yalleu tahh ma diapp Yalleu tahh bobou andeu dou diehh ohh Ndongo Sene
Samayy xarit samay domou ndeye pa amadou Diop la beugeu weuyeul
Makk samay xarit samayy domou ndeye Abdou Silla la beugeu djineulhh
Dioudondohh yarandoh magandoh Dameohh Ndiaye Diatta
Samayy xarit samayy dome ndeye gniama done fowall la beugeu weuyeulohhh
Bou djieukkone Thierno Seck téla gniakk Yaye
Yeii bou djieukkone ouyy Bassirou woye ohh
Bou djieukkone dangayy beugg nite gnou nane leu kii doussa nowlé
Bou djieukkone mane deihh beuggnaléne moussoumaléne fatéih tei dou amm gnianou makko
Yalleu weuyy Alioune Lam oyy sama wadjei eiy yei
Bou djieukkone dangayy beugg gnite gniou nane kii
Diolas leu wayyeu leguii lolou degnenafii kone na teii ndah
Ndongo Lo Ndongo Lo moyy tangall bopam
Abdou Silla kokou wayy leu mo tangall bopam
Alioune Lam séne dadeuu séne moyy tannall bopam
Mbaye Diagne kokou wayy leu moyy tannall bopam
Diaga Benga yiow sedeima moy tannall bopam
Becaye sama wadjanguii moyy tannal bopam
Thierno Diouff maggui Daba angueii moyy tannall bopam
Basse Sene sama wadjanguii moyy tannall bopam
Yeine samayy wayy beuggnaléne xarito
Weuyoumaléne guirr deureume beihh ohh
Weuyoumaléne guirr adouna yii eihh
Galanga boulma diapp dounyia bayynalaa xarito
Andando xaritt domou ndeye daffa yemoull
Ba tahna dall kigua yeimall djikko tolohh mommm ngorr momm guaa meunoo andal
Fii guene nekk soriloll fima nekk sorii wayy xoll yangiii guisséihh
Doleihhh djeumm
Doleiuy weuyy katt yii mane awma gniou doull yéne ba tahna dinaléne weuyeull
Yow Birame dinala weuyeull bi deih
Weuyléne bahna nahhh ba tahhna dinaléne weuyeul
Weuyléne bahna nahhh ba tahhna dinaléne weuyeul
Weuyléne bahna nahhh ba tahhna dinaléne weuyeul
Weuyléne bahna nahhh ba tahhna dinaléne weuyeul
Weuyléne bahna nahhh ba tahhna dinaléne weuyeul
Weuyléne bahna nahhh ba tahhna dinaléne weuyeul
Written by: N'dongo Lo