Similar Songs
Credits
PERFORMING ARTISTS
Jeeba
Performer
Dieyla
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Diamond Guidem
Composer
Djibril Bâ
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Diamond Guidem
Producer
Lyrics
Yala dou dioum mani Yala dou dioum loumou def ndeké lolou mo geune Demone na ba nar ko
dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko
Saï saïiiii la fok ma xolate ko Wadjii Saï saïiiii la
Yalla dou dioum ndeké yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na ba nar ko
dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
fok ma xolate ko Wadji Saï Saï la
yala dou dioum ndeké yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na ba nar ko
dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof Couplet
Nieuw na sama lathté fa sama yay boy
Saï Saï la
Nieuwate sama keur lathté fa sama
baye boy Saï Saï la
Néna kilifa la dou dokh thi tank
thiakhane Ñente ak tranche indi gouro
dadi labane Mingui may tek tank beug ma
forcé ray
Ndéké loumou beugone dougal but bi
jubilé daw
Yala dou dioum mani Yala dou dioum
Loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na bay xalate nar ko diox
sama xol Ndéké souma ko defone mangui
thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
Kone fok ma xolate ko Ndaw ci Saï
Saï la
Yala dou dioum mani yalla dou dioum
loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Néna koudoul mane beugoul sokhla woul
Mane rek la diokh bop kou Mel ni mane amoul
Mane mako yeungal yeungal mbeguelam
Ndéké mane dama door ay calmant lamay
diokh Dem na ba dépense keureum mako yoor
Faye courant Faye ndokh Faye diangue xalé yi ecole
Dieund greffage Faye ay voyage ndéké damay door sama poche la nop
Yala dou dioum mani yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na bay xalate nar ko diokh sama xol
Dejesouma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
Kone fok ma xolate ko Ndaw ci Saï Saï la
Written by: Diamond Guidem, Djibril Bâ