Similar Songs
Credits
PERFORMING ARTISTS
Jeeba
Performer
PRODUCTION & ENGINEERING
Abadane Daiman
Producer
Lyrics
Jeeba - Thiopet Yobou
Auteur : Jeeba
Compositeur : Bril
Production : Abadane Daiman
Voici le fichier wave du son : https://we.tl/t-p1x6GYOB2i
Lyrics
Nénama Fall lingay def danga thiy gaw
Ndakh atte yi danio gaw
Té temps bi donoul louniouy khar
Guiss nga mangui ni di dieum makk
Batay defo leen lou leer nak
Lettoma firi wo nak
Té ioe pousso passo nak
Guiss nga demba ak modou sama keur
Pathé ak ndiogou
Beuss bouné fala niouy nieuw rigou
Di khar kou nane leen indil gouro mba doudou
Ioe nak danga am lou keen amoul néma lane ?(lane)
Xol bi yako mom té keen ladioula fi leen(huum)
Lane moy sa probleme wax ma bok niou solution ko
Tay nga diap souba nga bayi né macky ak sonko
Wala danga hunn hunn hunn té yeugoumako (lane )
Mani bo yékhé daniou manane
Refrain
thiopete yobou
Éyy kouné di lath fane la nek
Mounane danio diay dolé ( tchipp) ndokou
Loumou sokhla rek la dieuli takhawé né
Yémé li dafa yémé yéémé limo yémé yéémé
Lii dafa yémé yéémé lii mo yémé yéémé
Néna Fall jiguen dafay gawa stress
Dafa soxla kouko rassurer
Pas ay probleme sans cesse
Danga koy xol sa bop fi keen beugoul niouy use sa time
On a qu’une seule vie té douniou la xaral ménopause
Jiguen soko beugué dangay def difference
Lane moy ndayou bene ba niénti atte thi relation
Tay nga yobou restau souba boite ça devient chiant
Beug di saï goudi saï beuthieuk meuno def halal
Wakh ji moy so begué takal so beugoul demal
Boul yakal kenene mouy demé nénéne
so begué takal so beugoul demal
Boul yakal kenene mouy demé nénéne
Éyy bo yékhé daniou manane
Refrain
thiopete yobou
Éyy kouné di lath fane la nek
Mounane danio diay dolé ( tchipp) ndokou
Loumou sokhla rek la dieuli takhawé né
Yémé li dafa yémé yéémé limo yémé yéémé
Lii dafa yémé yéémé lii mo yémé yéémé
Outro
Momo takal goné gui
Amet takal goné gui
Momo takal goné gui
Djibril takal goné gui
li dafa yémé yéémé limo yémé yéémé
Lii dafa yémé yéémé lii mo yémé yéémé
Enfin babau tak na goné gui
Written by: Bril, Jeeba