Credits
PERFORMING ARTISTS
Yvon Paris
Harmony Vocals
Jean-Louis Gomis
Harmony Vocals
COMPOSITION & LYRICS
Yvon Paris
Songwriter
Jean Louis Gomis
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Jean-Louis Gomis
Producer
Lyrics
Mama, mama, mama
Yow la baax
Mama, mama, mama
Sunu yaay dafa dem, dem naa
Ci ben yoon bu am faida
Wooy....dem naa
Sunu yaay, sell naa
Mooy li xarit am yep di wax
Tu as vécu avec fierté
Femme d'exception, tu incarnes la douceur
Tu es d'une grande simplicité
Sunu yaay (Hey) sunu yaay (Hey) sunu yaay
Xamna ne du nu bayyi
Mu amon xol bu baax
Te limu la defal
Du la ko feyyako (Du la ko feyyako)
Sunu yaay, sunu yaay, sunu yaay
Xamna ne du nu bayyi
Mu amon xol bu baax
Te limu la defal
Du la ko feyyako (Du la ko feyyako)
Fu mu dem, amna jamm
Jigeen ju amon xol bu baax
Yaay boy
Te limu la defal
Du la ko feyyako
Sunu yaay la won
Comme une sainte nous te louons
Tu nous as montré le chemin
Nous te chantons, te dansons (Ndey woor)
Pour continuer à vivre demain! (Djigen ju baax)
Chaque matin, on se lève
Chaque matin, on te prie
Chaque matin, on se lève
Chaque matin, nous te prions
Sunu yaay (Hey) sunu yaay, sunu yaay
Xamna ne du nu bayyi
Mu amon xol bu baax
Te limu la defal
Du la ko feyyako (Du la ko feyyako)
Sunu yaay (Hey) sunu yaay (Yaay boy) sunu yaay
Xamna ne du nu bayyi
Mu amon xol bu baax
Te limu la defal
Du la ko feyyako (Du la ko feyyako)
...
Written by: Jean Louis Gomis, Yvon Paris