Credits

PERFORMING ARTISTS
Alune Wade
Alune Wade
Bass Guitar
Mangane
Mangane
Guitar
Benjamin Naud
Benjamin Naud
Drums
Anthony Jambon
Anthony Jambon
Guitar
Inor Sotolongo
Inor Sotolongo
Percussion
Hugues Mayot
Hugues Mayot
Saxophone
Carlos Sarduy
Carlos Sarduy
Trumpet
Valérie Belinga
Valérie Belinga
Vocals
COMPOSITION & LYRICS
Mangane
Mangane
Composer
Alune Wade
Alune Wade
Arranger
PRODUCTION & ENGINEERING
Raphaël Jonin
Raphaël Jonin
Mastering Engineer
Sebastien Tondo
Sebastien Tondo
Mixing Engineer
Dominique Boss
Dominique Boss
Recording Engineer
Johann Boos
Johann Boos
Recording Engineer

Lyrics

Cha-i-da-i-da-i-da-i-da-i-é-é-é-é
Cha-i-da-i-da-i-da-i-é
Cha-i-da-i-da-i-da-i-da-i-é-é-é-é
Cha-i-da-i-da-i-da-i-é
La famille mbokk jè naangn léen jappo moyli gën
Wawa-wé-wawa-wé-wawa-wé-wawa-wé
Ci boolo la ngnu mënna xammanté,
Ci jappo la ngnu mënna déffar,
Muylu woorè-muylu lérrè-muylu-woor
Muylu lérrè-muylu-wooré-muylu-léer
Muylu woorè-muylu lérrè-muylu-woor
Muylu lérrè-muylu-wooré-muylu-léer
Bu ngnay di xaal babbal doom ya tax
Boolo nék bénn doo nupp saay, ba bu noon duggè, wala nék ci sungnu biir bangne ngno féwëlè
Ci boolo la ngnu mënna xammanté,
Ci jappo la ngnu mënna déffar,
Wawa-wé-wawa-wé-wawa-wé-wawa-wé
Muylu woorè-muylu lérrè-muylu-woor
Muylu lérrè-muylu-wooré-muylu-léer
Muylu woorè-muylu lérrè-muylu-woor
Muylu lérrè-muylu-wooré-muylu-léer
Written by: Mangane
instagramSharePathic_arrow_out