Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Dizzy Kha
Dizzy Kha
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Imam Abdoul Khadre Mbacke diop
Imam Abdoul Khadre Mbacke diop
Songwriter
Saliou Massamba Samb
Saliou Massamba Samb
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Papa Laye Beatz
Papa Laye Beatz
Producer

Lyrics

Mane bama rere yama wane sama yonou khol
Mate gama niente nala nianesi nienti yone (mak yow mak yow)
Nah Manak yow (mak yow mak yow)
Si bene pakh bi lagn niouy soule (si bene pakh bi lagn bi lagn niouy soule eyway)
Nenegn kou nelaw dagay faté lepp may nelaw dila geuneu nameu
Taroul Baga craquer deme nakh selaw biga Meusseu andal
Yaye niane bou nangou Gom you fadiou peace of mind yea
Houlo moy tah dioubo di neh Nagn rayanté sougn bir
Bou janteu teuder Man ak yow la Kenen nekouffi
Nah yamay gagne te malay fadj yow kay niou guissé
Yenesay niu doundou aldiana yenesay niou misere
Fo deuk ma deuk fa fo Deuk fofa nekh (saay)
Douma feké sa nakar Rangogne fompat Lene
Fess samay beut keuf sama Khole
Yeurmandéy mbeuguel te amgako
Hamna sa nieuk louner diar gako
Man malay balou te yama togne yeaa
Mane bama rere yama wane sama yonou khol
Mate gama niente nala nianesi nienti yone
Nah Manak yow (mak yow mak yow)
Si bene pakh bi lagn niouy soule (soule soule soule)
Mane dama nekk sassouma neker ak yow
Fanane sa wet chaque goudi Kheuy Ndeke sa love
Nah manak yow (mak yow mak yow)
Si bene pakh bi lagn niouy soule (soule soule soule)
Geudj ga degg samay beug nalaa da fekk mala raaw
Faga tolou si yow sorina lolou pencum khol beu yafané
Kene geunoula si sama ay adio louma sohla ya thia meune
Soumala buur weurseugeuley doom Yalnaniou Diar si yow
Manak yow contre vents et marrées
Mak yow comme mackek marieme
Opposant yi kass boulene deglou kaay nala dieul dougal si palais
Tank ak tank fo deme ma dem
Ayee kima dadiel mo mata kham way
Mane bama rere yama wane sama yonou khol
Mate gama niente nala nianesi nienti yone
Nah Manak yow (mak yow mak yow)
Si bene pakh bi lagn niouy soule (si bene pakh bi lagn niouy soule ehhh)
Mane dama nekk sassouma neker ak yow
Fanane sa wet chaque goudi Kheuy Ndeke sa love
Nah manak yow si bene pakh bi lagn niouy soule
Written by: Idrissa Thioye, Imam Abdoul Khadre Mbacke diop, Saliou Massamba Samb
instagramSharePathic_arrow_out