Music Video

BLAZE IT - NATTY JEAN (OFFICIAL VIDEO)
Watch BLAZE IT - NATTY JEAN (OFFICIAL VIDEO) on YouTube

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Timothee Wecxsteen
Timothee Wecxsteen
Programming
Natty Jean
Natty Jean
Lead Vocals
COMPOSITION & LYRICS
Timothee Wecxsteen
Timothee Wecxsteen
Composer
Natty Jean
Natty Jean
Lyrics
PRODUCTION & ENGINEERING
Timothee Wecxsteen
Timothee Wecxsteen
Producer
Eric Chevet
Eric Chevet
Mastering Engineer
Phil Spread
Phil Spread
Mixing Engineer

Lyrics

**** ya ma gën giss Mais dangay con conlu
Mala gën diis aussi mala gën con
Sa ĝél mungi mey piiss Bëgë na xam numu tolleu
Gudi gi du nelaw tant que degul sama son
**** ya ma gën giss Mais dangay con conlu
Mala gën diis aussi mala gën con
Sa ĝél mungi mey piiss Bëgë na xam numu tolleu
Gudi gi du nelaw tant que degul sama son
Buma né tcheup in da club Sa fans yëp danuy tëp
Maï lene tuti reggae jolof wala wiss ci rub a dub
**** yangi sukuraat aki seni flow yu nëp
Non non jarul suku raam allez dj pull it up
Arrête de faire genre il est beau il est mignon
Et puis il est élégant boma sonué nala rux
Et puis duma sol gants yangiwone si say couche
Bima doné soldat, rakk degluma
**** ya ma gën giss Mais dangay con conlu
Mala gën diis aussi mala gën con
Sa ĝél mungi mey piiss Bëgë na xam numu tolleu
Gudi gi du nelaw tant que degul sama son
**** ya ma gën giss Mais dangay con conlu
Mala gën diis aussi mala gën con
Sa ĝél mungi mey piiss Bëgë na xam numu tolleu
Gudi gi du nelaw tant que degul sama son
My **** looy jaay, way way way
bo fi yaksé boy fii nga coy fek
Bobu ba légi mangi tok ni tekk,
Yangi mey saur ci pet
Yangi tudu millions mais boy ya mën fén,
Sen game, dafa bari bubu golo phénomène
Sen taat, danio melni bossu tata philomène
Sen baat, buma len rombé na lene defal tuti lém
Sen gat, bula nakaré yow dangay tok ci nén
Sénégal ndeyssan dëkku rubé mbele mbele
Racc jëmëlé sa bord au lieu de doon bén,
Mangi tok ci aile bi nalé boma gissé comptel
Un, deux, trois, quatre
Boy buma ci moytuwul ma ñëw toj sa gat
Un, deux, trois, quatre
Bama respect dang ma koy jox mu mët
**** ya ma gën giss Mais dangay con conlu
Mala gën diis aussi mala gën con
Sa ĝél mungi mey piiss Bëgë na xam numu tolleu
Gudi gi du nelaw tant que degul sama son
**** ya ma gën giss Mais dangay con conlu
Mala gën diis aussi mala gën con
Sa ĝél mungi mey piiss Bëgë na xam numu tolleu
Gudi gi du nelaw tant que degul sama son
Affaire bi du vitesse né nala course de fond lë
Jangë lene ci demb ndax lu wessu leçon lë
Reew mi bo fi yaro ñu ni boy bi dé con lë
Boy yi daño fokni yëfu gudulé jon lë
Ep bi dafa tchukku ba nga fogni xoon lë
Pourtant damay foo rek ben espeçu pont lë
Mais pourquoi mey yakamti buma gëmé ni don lë
Siaaré la bu sew mangi dëpaat sama corner
**** ya ma gën giss Mais dangay con conlu
Mala gën diis aussi mala gën con
Sa ĝél mungi mey piiss Bëgë na xam numu tolleu
Gudi gi du nelaw tant que degul sama son
**** ya ma gën giss Mais dangay con conlu
Mala gën diis aussi mala gën con
Sa ĝél mungi mey piiss Bëgë na xam numu tolleu
Gudi gi du nelaw tant que degul sama son
My **** looy jaay, way way way
Bo fi yaksé boy fii nga coy fek
Bobu ba légi mangi tok ni tekk
Yangi mey saur ci pet
Written by: Natty Jean, Timothee Wecxsteen
instagramSharePathic_arrow_out