Top Songs By Youssou N'Dour
Similar Songs
Credits
PERFORMING ARTISTS
Youssou N'Dour
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Youssou N'Dour
Composer
Henry Guiyabert
Composer
Lyrics
Ha dem
Dem fan
Lu ma bëggoon mënul nekk
Leer nga ci kenneen
Man ma ngi ci lëdëm
Xam naleen, may ki koo def
Suma demee bay meree
Duma meree kudul sama mbopp
Te man may seeti baye baalu ko
Wiri wiri jaari ndare
Wiri wiri jaari ndare, ndare
Xam na dem
Demul feen fu nguy wuute
Ligeey u ma
Li ma mbëggoon moy mu dox
Te duma dox, ci sen kaw
Xam na lépp, may ki ko deef
Suma demee bay meree
Duma meree kudul sama mbopp
Te man ma seeti bay, baalu ko
Wiri wiri jaari ndare
Wiri wiri jaari ndare, ndare
Wiri wiri jaari ndare, ndare
Bilay, bilay, bilay, bilay-bilay
Ma rëccu
Ma nee soy dem mba xamatoo fa jëm
Delul fa nga jukkee
Fuy la xamee
Fii nga mbaggee
Fuy la teete
Fi nga jange école
Wiri wiri jaari ndare
Wiri wiri jaari ndare, ndare
Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri)
Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri)
Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri)
Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri)
Wiri wiri jaari ndare, ndare (ha fokk ma seeti bay)
Wiri wiri jaari ndare, ndare (wara bokk mba seeti yaay)
Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri)
Wiri wiri jaari ndare, ndare (ha fokk ma seeti bay)
Wiri wiri jaari ndare, ndare (wara bokk mba seeti yaay)
Writer(s): Youssou N Dour, Henri Guiyabert
Lyrics powered by www.musixmatch.com