Top Songs By Dip Doundou Guiss
Similar Songs
Credits
PERFORMING ARTISTS
Dominique Preira
Rap
COMPOSITION & LYRICS
Dominique Preira
Songwriter
Ismaila Talla
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Iss 814
Producer
Lyrics
Boula dara metti
Boula dara gagne
Douma imbéciles
Danko wara xaam
Douma domérame
Douma salopards no
Boula dara metti ndax mana
Léena rek kama metti the dina hame
Ay nith you bax dinagne la diaxassék mane
Dilay waxlo lo hame
Dou diar sax ngay comprendre
Même boudône mbeuguel déey diay do hame kénéne comme mane
Doyna warame dafa dow yarame
Dangue ma beugue xamnako xanna doumala doxane
Doumala thieupeul thi pét iow ngay diay eupeul dimay thieupél
Iow mi ya done costé thi netbi nane fou néke je t'aime
Love ngama ba teukkané ma lolo tax ma déme baby lou eupe tourou dangue ma warona nob nanke rék
Written by: Dominique Preira, Ismaila Talla