Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Ismaël Lô
Ismaël Lô
Performer
Stan Renoult
Stan Renoult
Performer
Pierre Bertrand
Pierre Bertrand
Performer
Claude Salmieri
Claude Salmieri
Performer
Laurent Vernerey
Laurent Vernerey
Performer
Yann Martin
Yann Martin
Performer
Michel Aymé
Michel Aymé
Performer
Thierry Boucou-Pastel
Thierry Boucou-Pastel
Performer
Philippe Balatier
Philippe Balatier
Performer
Philippe Georges
Philippe Georges
Performer
Pathe Dieng
Pathe Dieng
Performer
Olisa
Olisa
Chorus
Diane Solo
Diane Solo
Chorus
COMPOSITION & LYRICS
Ismaël Lô
Ismaël Lô
Composer
Stan Renoult
Stan Renoult
Arranger
Pierre Bertrand
Pierre Bertrand
Arranger
Claude Salmieri
Claude Salmieri
Arranger
Laurent Vernerey
Laurent Vernerey
Arranger
Yann Martin
Yann Martin
Arranger
Michel Aymé
Michel Aymé
Arranger
Thierry Boucou-Pastel
Thierry Boucou-Pastel
Arranger
Philippe Balatier
Philippe Balatier
Arranger
Philippe Georges
Philippe Georges
Arranger
Pathe Dieng
Pathe Dieng
Arranger

Lyrics

Mané hé baykat bi khalam
Démonna bay nékh wayé boumgua
Dokna mome
Hé baykat bi khalam démonna
Bay nékh wayé boumgua dokna mome
Boula nékhé talalal say lokho
Vaye docteur biy fath khifou askane bi
Liko dalé si nditoum rew bassi miskine
Ya souméko di dane sa dolé andak nath
Bi di liguey sa gnakha di tourou
Ngay bay di doukat bilay ya am diome
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour waw koufi fébar
Yako nandal aki réén bamou féékh
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour
Waw koufi fébar yako nandal aki réén
Bamou féékh
Ya momone sa mbay
Ya mome sa guanthiakh mome say
Ndiour ya mome sa alla di bay
Nguour gneuw dougalthia lokhome ak
Boor fékeleuthaa guanthiakh ba
Mégneu lole ndékétéyo
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour
Waw koufi fébar yako nandal aki réén
Bamou féékh
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour
Waw koufi fébar yako nandal aki réén
Bamou féékh
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour
Waw koufi fébar yako nandal aki réén
Bamou féékh
Kon diarama baykat koufi xiff yako, dirama
Doundal bamou sour, diarama baykat bé
Waw koufi fébar yako nandal aki réén, kéneu rek mola mana faymoy bourbi yaalla
Bamou féékh
Kon diarama baykat koufi xiff yako doundal bamou sour, guathia ngalama, guathia ngalama yaw baykatbé
Waw koufi fébar, yako nandal aki réén bamou féékh, guathia ngalama
Guathia ngalama yaw baikatbé
Kon diarama baykat koufi xiff yako doundal bamou sour, dirama diarama baykatbé yaw
Waw koufi fébar, kéneu rek moleu mana fay, yako nandal aki réén bamou féékh
Moye bourbi yalla
Written by: Ismaël Lô
instagramSharePathic_arrow_out