Top Songs By REP'TEAM
Lyrics
Reptil Music
Bayil ma diape sama yaye diape sama baye diape sama pistolet thi sama gayii
Bayil ma diape sama vibs diape samay dadj cautche samay milion tegle samay tanke
Bayil ma diape sama yaye diape samay hunn
Diape samay pistolet thi sama gayi
Bayil ma diape samay dadj diape samay vibs cautche samay milion tegle samay tanke
Par ce que lolou mo guen lolou mo guen lolou mo guen my niger lolou mo guen
Par ce que lolou mo guen lolou mo guen lolou mo guen niger lolou mo guen
Mounouma tegle samay tanke milion yii lay xare ñiou ñieuw
Teude wala dioutou bana mo nara guen thi iow
Mideul fi nga sissa trou guel normal sa bath thi kawe
Bayil ma compter samay liasse boulma yakal ferme ta gueul
Bocar bayma negou gass
Baymak samay thirr
Fofou laye dem di skater souma amer envie yii
Boy boul dougou thi sama gayi
Ndeugou do douma bayi dara mou sede bayi mak sama pistolet mak rindi
Par ce que lolou mo guen lolou mo guen nga bayi ndaxe aténo niveau bi (euskeuy)
Lolou mo ame sa gayi gueudj nañou guiss thi chec(ehy)
Boyi ñion xew mo takh sa guel bi dafla sappé 221 sa sort pour ecraser c tas-pe