Similar Songs
Credits
PERFORMING ARTISTS
AMADEUS
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Abdoulaye Diop
Composer
Saliou Samb
Songwriter
Lyrics
Boo ma beddiwul xalaatuma la bàyyi
Awma laamisoo tudduma lambay yoy
Gaañ la taxul nga ba
Tooñ la taxul nga may rëccooy
Sàllaaw yenn saay nga mer
Sama jaambaar ci yaw mi la wékkooy
Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom laay jëli (eeh yoo)
Dootuma yónni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (man ma)
Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom laay jëli (daadi sama waay)
Dootuma yónni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (danga di sama waay)
Bala ma jug
Fajar fekk nga dem jaayooy
Bale kër gi, raxas say ndap
Ndekke boobu doom ngay wajal
Dundu mat a ñaan nooy
Ndaxte gaynde dama koy jur
Ndax fitna loo ma
Xeboo li ma lay jox
Lépp loo ma ñaan dinaa la may
Dootuma def leen lu lay metti sama ndaw ci
Ndax sama nawle nga doo leeral sama yoon wi
Dootuma nangu mbindéef di dox sama digu ak yaw
Ndax Yàlla moo def ci ñun lay ñu wëy nak
Kaay waay
Gaañ la taxul nga ba
Tooñ la taxul nga may rëccooy
Sàllaaw yenn saay nga mer
Sama jàmbaar ci yaw mi la wékkooy
Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom laay jëli (eeh yoo)
Dootuma yónni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (man ma)
Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom laay jëli (daadi sama waay)
Dootuma yónni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (danga di sama waay)
Gaañ la taxul nga ba
Tooñ la taxul nga may rëccooy
Sàllaaw yenn saay nga mer
Sama jàmbaar ci yaw mi la wékkooy
Eee waay
Sama jamm, sama waay
Eh waay wow
Sama jamm, sama waay
Sama jamm, sama waay
Boo yeewoo
Papa Laye sunu way
Writer(s): Abdoulaye Diop, Saliou Samb
Lyrics powered by www.musixmatch.com