Lyrics
Suma reeni xol mi de yidde ma
Su ma la amul woon defar naa la
Sunu diggante lépp ma ci neex
Ni ma la bëgg ni de ëpp na
Sama reeni xol mi de yidde ma
Ni ma la amul woon defar naa la
Sunu diggante lépp ma ci neex
Ni ma la bëgg
My baby yaw,sama xol bi yaa ci ne, yeah yeah
Teye la,su ma la bàyyee bàyyi lu neex, yeah yeah
May janneer sa tàkkander di ma gunge, yeah yeah
Xamal la ci sa jëmm ji laay dunde,baby
Fekk ma ci naj, jël yóbbu ma ci ker gi
Su ma la nàmmee, jaxaan gis la ci weer wi
Dama bëgg fi ci àdduna, ñu dund aljanna
Sunu sëy bi daggan na, yóbbu ma fu la neex, yeah yeah
Ci diggu laal ba
Suma reeni xol mi de yidde ma
Su ma la amul woon defar naa la
Sunu diggante lépp ma ci neex
Ni ma la bëgg ni de ëpp na
Sama reeni xol mi de yidde ma
Ni ma la amul woon defar naa la
Sunu diggante lépp ma ci neex
Ni ma la bëgg
T'es ma lover (baby,baby,baby)
My lover (baby,baby,baby)
My lover (baby,baby,baby)
Sama lover (baby,baby,baby)
Suma reeni xol mi de yidde ma
Àdduna du neex ba ma gis ku mel ni yaw
Yaay sama baby love,sama gidelam
Yoon bi gudd bae sans yaw duma ñibbi,non
Maak yaw li ñu boole moo ñu mën
Même sunu boole ñoo koy ëpp doole
Baby mi de yidde ma, baby you already know
Fanaan sans yaw daf may tëredi lool, yeah,yeah
Lu ma la jox nga may delloo
Mbëggeel du jay ba ma lay jënde
Ñëwal ñu togg,ñëwal ñu pello
Loo bëgg dam koy def
Yaay sama wéeruwaay
Fecc dëgin ndaat saay pour sa xol bi nat
Baby,sama aljanna
Tax nga bàyyi yaay baay,dëkk sunu life
Baby
Suma reeni xol mi de yidde ma
Su ma la amul woon defar naa la
Sunu diggante lépp ma ci neex
Ni ma la bëgg ni de ëpp na
Sama reeni xol mi de yidde ma
Ni ma la amul woon defar naa la
Sunu diggante lépp ma ci neex
Ni ma la bëgg
Sama mbëggeel dëgg la
Wat na ni bëgg naa la
Soo tëddee nelawal
Dama la love
Sama lover (baby,baby,baby)
My lover (baby,baby,baby)
My lover (baby,baby,baby)
Sama lover (baby,baby,baby)
My lover
Writer(s): Dominique Preira, Benette Seraphin Koffi, Bakhao Dioum
Lyrics powered by www.musixmatch.com