Lyrics
Tey ma bége la
Tey ma wone la
Tey ma wax la
Yaa ma gën a xam way!
Li nga ma def soo ko bàyyiwul
Dinga mës a ray doomu jaambur way!
Yaw yaa ma xam, xam ma bu baax
Bu lu xasaan ci man loxo keneen wokesu ko
Guddi gi jot ba lépp ni séelaw
Nga daagu ndank ñëw sama kaw di ma eh eh eh Yaw
Say kesen kesen tere ma nelaw
Yaa ma mën a yuxuloo te xam nga dama ragal
Eh calm down, calm down
Bébé calm down, doomu jaambur la
Eh calm down, calm down
Bébé calm down, doomu jaambur la
Dootoo niit parce que doo nitu
Yaa nga may fit est-ce que doo ciit
Ni ngay def dama joomi
Man li may yaakaar est-ce que doo ñooñu
Yeah yeah
Baby li ma jaxal te nga wax ma ki la jàngal
Sant na sa bàjjen moom mi la jox li may jomal
Amatuma sago ci yaw su ma la gise saalit
Waaw waaw, yow baby waaw waaw
Seddal sama xol, dalal sama xel
Yaa ma gëna lool
Ne waaw seddal sama xol dalal sama xel
Eh eh eh
Eh calm down, calm down
Bébé calm down, doomu jaambur la
Eh calm down, calm down
Bébé calm down, doomu jaambur la
Dootoo niit parce que doo nitu
Yaa nga may fit est-ce que doo ciit
Ni ngay def dama joomi
Man li may yaakaar est-ce que doo ñooñu
Writer(s): Djiby Ka, Kevin Honore Kailly, Cheikh Ahmadou Kara Diouf
Lyrics powered by www.musixmatch.com