Music Video

Ashs The Best - Xel Akk Xol (Clip Officiel)
Watch Ashs The Best - Xel Akk Xol (Clip Officiel) on YouTube

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Ashs The Best
Ashs The Best
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Ashs The Best
Ashs The Best
Lyrics
Olvier Delahaye
Olvier Delahaye
Composer
Abdoulaye Sy
Abdoulaye Sy
Composer
PRODUCTION & ENGINEERING
Nautylusprod
Nautylusprod
Producer

Lyrics

Yeah, eh eh eh Lé, lé, walé Hum, hum Suuba souma yéewoo, yaw la bëgg jakarlool Sa suma yeewu, yaw lay mbëgg njëk xool Ëlëk lu mata soor la, waye xel xalaat u ko Ëlëk ay jaar-jaar la, sama xol yëgoon nako muy ñëw Xel xalaat la (xel ak xalatam bë) Xol yëkk yëkk la Niit ak jëmmam ja dara xaaju fë Sa suma yeewu, yaw lay bëgg njëkk xol (fajaar suma yéewo yaw Ia bëgg njëk xool) Fajaar suma yéewo yaw Ia bëgg njëk xool Denk na la guddi, fanaane yaakaar ci yaw (denk na la sama xol fanaane yaakaar ci yaw) Gent na la guddi gi yëpp ndax fajar yaw lay jakarlool Mbëggelam Xel xalaat la Xol yëkk yëkk la Niit ak jëmmam ja Dara xaaju fë Xel xalaat la (xel ak xalatam bë) Xol yëkk yëkk la (sama xol-) Niit ak jëmmam Ja dara xaaju fë (Dara fa xaajul) Niit nak ak jëmm ja, Dara fa xaajul
Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Arfang Tiare Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out