Music Video

Abdou Guite SECK - Yaw la beug (Clip Officiel) - Album 2020 - Coup d'Etat
Watch Abdou Guite SECK - Yaw la beug  (Clip Officiel) - Album 2020 - Coup d'Etat on YouTube

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Abdoulaye Guitte SECK
Abdoulaye Guitte SECK
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Abdoulaye Guitte SECK
Abdoulaye Guitte SECK
Songwriter

Lyrics

Yaw laa beug
Hé ni Yaw la beug
Andandoo ak mindéf kén douko dindi
Yaw laa beug
Kén gua thi man té Yalla mom moo sédé yaw la beug
Kén gua thi man ba abadan dahi man dé yaw la beug
Kén meunoulaa dab thi man ba di la romb yaw laa beug
Andandoo ak mindéf kén douko dindi yaw laa beug
Fowé wouloo ma
Negligé wouloo ma
Te wédi wouloo ma
Hanhan yaw la beug
Andandoo wak mindéf djiné douko dindi yaw laa beug
Kén meunoulaa dab thi man ba di la romb yaw laa beug
Bari woo andando
Nioy togando di diogando
Fa may bagne dé dieumou loo fa
Guidélam yaw dé guidélam
Hooho yaw laa beug
Nékouloo thi yén diotaay
Maingook gua sa djiko yaay
Néwoulooo ma tay gua siw
Te li gua meuna wané bari
Ndakhté lép thi yaw beauté la
Guidélam yaw dé guidélam
Ni djiguén bou fi sallo sallo sa djiko ko dji
Boo daggo nieup dar la di way sa dialooré
Ki mo di Yaye Touto Jamiloo Vieux Racine
.
Djioural gua ma samay doom
Amoulo khar ma Yalla
Fama khool fofa guay khool
Sotante khalaat di djiém té manou
Nél sa yaaye la mou liguéyoon tégne wa gui ni
Tégne waa ngué té yén wi nieuweugoul yén wéngi thi yoon
Dina diém sama kém talayou katan
Ni am naa dépense meun naa foné - Yaw laa beug
Meun na khalam meun na riti - Hé ni Yaw la beug
Loo namati fi lé diokhogne dague naa - Yaw laa beug
Sounou mbeuguél bi lé mo meun ya thia dess - Hé ni Yaw la beug
Ni am naa dépense meun naa foné - Yaw laa beug
Ni meun naa khalam meun na riti - Hé ni Yaw la beug
Kon loo namati diokhogne dague naa - Yaw laa beug
Sounou mbeuguél bi lé mo meun ya thia dess - Hé ni Yaw la beug
Je t’aime
---------- FIN -----------
Written by: Abdoulaye Guitte SECK
instagramSharePathic_arrow_out